@@AbabacarSamb-h5j je suis d’accord c’est trop facile, mais c’est n’est pas la police qui juge, c’est le juge d’instruction qui y’a relâcher Nabou, alors y’a pas eut d’enquête encore. C’est n’est pas normal.
Seigneur donne lui le repos éternel accueil le dans ton paradis céleste , Maman MARIE mère des Mères apaise, console et soulage la maman d'Aziz. Que ton manteau virginal lui sert de protection de soulagement afin qu'elle puisse surmonter cette énorme douleur par l'intercession de ton fils JESUS le Christ AMEN! Quand je regarde la maman d'Aziz j'ai le cœur qui saigne 😭
Inchala yalla dina lérale leupe le miséricorde le tout puissant ndakhe bakane da fort lolouuuu rawatina bi dossier Inchala leupe moye lére si barké Seydina Mouhamed Psl
lolou nieumpou beugeu ndakhe niniou mélone niome niare mei li téye khélou nite gni moye yone moko takale ba nieumpou bayi khél nabou léye ngua nieuwe takhawate diko maye liberté provisoire mei na gayi nieuwe lérale mei li mome dafa yombou trop sakhe akhe😢😢
C'est difficile pour la famille mais la véritable question est : Pourquoi la police avait arrêté Nabou Leye ? Le droit c'est compliqué Vous ne comprenez rien au droit madame c'est à votre avocat de vous expliquer Le juge peut bien lui accorder la liberté provisoire s'il n'a pas assez d'éléments après avoir ordonné une nouvelle enquête qui est toujours différente de l'enquête de la police Le juge n'a pas a avertir votre avocat pour libérer un accusé
Depuis toujour la justice sénégalaise dafa déféné yoréroul kéne bén explication. Pour eux ils ne doivent à personne aucune explication. C’est comme ils ne savent pas ce qui se passent dans les autres pays. C’est vraiment malheurex. C’est comme rien n’a changé à la justice
Niom nieupp ay domerame la niou. NABOU bras long la am, thiaga la , bandit la. Wornama ni amna ay vidéos you mouy chantagé des personnalités de ce pays. Thiaga la ci boppam. Wayè atté Yalla Mo gueune bou Niit
Yene vous abusez a la fin. On a tué aziz nako yalla yeureum. Police moo diap gnimou diap si enquete, justice mo mandat de depot, justice mo bayi nit ki nguene ni nonon cta dire. Il ya dautres personnes youniou diap non!? Wolounguene justice mais c’est vous qui remettez en cause . Dama fokni buzz nguene beugu a la fin. Portez plainte contre nabou leye alors prsk yene portez woulene ko plainte gniko diapone nioko bayi
Antoucas nabou leye môme domouhram la boumakk sakh yaw sa xarite dé si jour décés bi ngay wakh nane kou dé déna nieupay dé ak dé nimou métiwé ngani yaw aziz sa xarite la ak niniouko rayé nimou niawé ngay wakh lolou kou tothie sarap ndeyam la
Mais cest pas possible il et est où la justice .depuis 2mois pas la police pas le juge pas le procureur j'espère k nabou dou ndaw j'espère k jugement sera faite
Franchement la justice Sénégalaise je suis désolée. Aucune communication pas de conférence de presse par rapport à ce dossier qui a choqué et touché tous le monde au delà des frontières.
Li nasi niep wah ndakh sonko ak diomay diotsi wahak juge yi rewmi coumba am Ndeye ak coumba amoul Ndeye dafer wara diok q justice soit faite nabou niata mandat dépôt la fek Maf ta ken laloul sen d’osier ta am nanou ay avocat donc nabou niow même pa 3mois juge lidianti dosier bamouy am liberté jub Jubal jubanti lanou wah pro yeugueul Li wah ak justice
Vraiment la maman elle a trop mal ndeysan Yalla nako Yalla diegeul te yereum ko yatal bamelam leral ko te leral mbir yi bala mo yag 🤲🏾 En passant la maman aussi elle communique bien 👍🏿
Lolou moy wakh ji. Ki amna bras long. Sénégalais ci boppam Mo am vice thiaga. Thiaga rek la niou beugue. NABOU leye kou ko Guiss khamni bandit la thiaga la
NABOU LÉYE N EST PAS ENCORE JUGÉE, C EST UNE LIBERTÉ PROVISOIRE. CELA NE VEUT PAS DIRE QU ELLE N EST PAS COUPABLE, SEUL LE PROCÉS FERA LA LUMIÈRE SUR CETTE AFFAIRE.
C'est le processus normal d'une enquête judiciaire. Meune naniou placé niit sous mandat de dépôt bala procès ba du diote enquête bi wané ay insuffisances de charges. Dans ce cas avocat kouniouy top meune neu lay liberté provisoire.
Nabou est ce que danguene ko guiss si lieux de crimes bi wala genre pour nguen Di toumal domou ndiambour bi danguene gana XAM procureur son job déjà gni gnou diap gno ray waxolene si gnognou mai nabou nguene tek beute prétendant k complice la nekk lene niit douguene yalla douguene juge
Mann ma bayi senegal depuis niarri khalé yoyou niou fekk si auto soit disant serigne bi keur mbaye fall bénnn khalé bi déee khénnn diappoul borom auto au contraire famille victime bi laniou attaquer
Li yeup police leu ils doivent nous dire pourquoi il avait attrappé nabou leye et pourquoi il l ' ont relaché.
bilahi walahi wa talahi frère li dafa yombou koi
Lolou procureur ngakay lathie
C’est n’est pas la police qui juge ma sœur, faut demander ça au juge de l’instruction.
@omzo9376 non frère li yombouna lole waye 😭
@@AbabacarSamb-h5j je suis d’accord c’est trop facile, mais c’est n’est pas la police qui juge, c’est le juge d’instruction qui y’a relâcher Nabou, alors y’a pas eut d’enquête encore. C’est n’est pas normal.
Souma kholei yayou Aziz rek sama xol nakarii Yaye gnou gui lay matsa wou bakh Borom bi dolil leu kholou mougn goudeul fanes yii wereul thieur yii inshallah 💔😭
Bilahi sa youmako kholé dioye 😢li dafffa meti trop Yalla nako Yalla Sam mayko kholou mougne
Amine
Vraiment yayou Aziz mi yeureme nako trop😢😢😢 mére bi mak la Ndeyessane 😢😢😭😭😭
Bou done môme AK mome wakh dji djekh na bou yague mes oute katou khalis yi nabou guéne arrangé woulene
Yalnako yalla léral thi barké seydina Mouhamed Salalakhou ala Mouhamed 🤲🤲
SALALAKHOU ALAIHI WASALAM
Salalahou hala mouhamad ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Bilay dama yeureum yayou Aziz 😭😭😍
Li dafa yomb trop
Ohhh la mère de aziz😢 yalla nala yalla may kholou mougne
Vraiment le procureur doit faire un point de presse
Li rek motah Europe rawniou bilay procureur mo wara wahh Lou lerr tamit niakk dafa metti wayy li d'où yonn bilay
Justice pour Aziz AK wally😢😢😢😢😢
Massa yaboye , maasa yalla na yalla léral lep ci barké SERIGNE TOUBA,
Seigneur donne lui le repos éternel accueil le dans ton paradis céleste , Maman MARIE mère des Mères apaise, console et soulage la maman d'Aziz. Que ton manteau virginal lui sert de protection de soulagement afin qu'elle puisse surmonter cette énorme douleur par l'intercession de ton fils JESUS le Christ AMEN!
Quand je regarde la maman d'Aziz j'ai le cœur qui saigne 😭
Justice pour aziz dabala et wally
Ta rokhaya diouf kou bakh yalla na yalla yeureume aziz sa dome dji
Justice pour Aziz et walyz
Inchala yalla dina lérale leupe le miséricorde le tout puissant ndakhe bakane da fort lolouuuu rawatina bi dossier Inchala leupe moye lére si barké Seydina Mouhamed Psl
Amine
Nabou leye yalla nala yalla diapaleii baboumou laleii dra sii yeufou aziz bii amen
Amine
lolou nieumpou beugeu ndakhe niniou mélone niome niare mei li téye khélou nite gni moye yone moko takale ba nieumpou bayi khél nabou léye ngua nieuwe takhawate diko maye liberté provisoire mei na gayi nieuwe lérale mei li mome dafa yombou trop sakhe akhe😢😢
Yalla naka yalla leram ci barke Mohamed paix a son âme te yalla maye kholou mougne yayou Azize dabala😭😭😭
Nabou mo wa roule wone guene complicité meutre Bâ paré dii gueene
Doyna warr dal
Manou mo gueuneu wor ba ham vrai vérité bi🎉
K justice soit faite Li mom dafa méti trop bly
C'est difficile pour la famille mais la véritable question est :
Pourquoi la police avait arrêté Nabou Leye ?
Le droit c'est compliqué
Vous ne comprenez rien au droit madame c'est à votre avocat de vous expliquer
Le juge peut bien lui accorder la liberté provisoire s'il n'a pas assez d'éléments après avoir ordonné une nouvelle enquête qui est toujours différente de l'enquête de la police
Le juge n'a pas a avertir votre avocat pour libérer un accusé
Bien dit. Ces gens n'ont rien compris
C'est ça ki est nabou leye pour avoir des privilèges ? Meti n'a waye il faut ngen and ak dale
Justice pour Aziz et waly réponse vous en paix mais frère🙏🙏
Liberté provisoire amoul droit guéne Réw mi c’est vraiment triste walahi Yallah nalénnn Yallah mayyy xolou mougne
On réclame vraiment justice pour Aziz trop c'est trop
Depuis toujour la justice sénégalaise dafa déféné yoréroul kéne bén explication. Pour eux ils ne doivent à personne aucune explication. C’est comme ils ne savent pas ce qui se passent dans les autres pays. C’est vraiment malheurex. C’est comme rien n’a changé à la justice
Justice pour le double meurtre de Aziz et Wally yalla na yalla lérale lépp
Vraiment daffa meti meussouma guiss atté guouniou niouye degue liberté provisoire dou yone
Barki serigne touba mère liga wakhe yeupe deugeuleu té amnga respect ci ligaye wakh
Il faut faire une marche et demander des comptes au procureur pourquoi cette décision
Vrainent metna manda de dépot liguie ga libéré eskey maman courage
Quand l ancien ministre ndene NDiaye se constitue avocat si la sama khel tey
Niom nieupp ay domerame la niou. NABOU bras long la am, thiaga la , bandit la. Wornama ni amna ay vidéos you mouy chantagé des personnalités de ce pays. Thiaga la ci boppam. Wayè atté Yalla Mo gueune bou Niit
Limome dou yone coumba amoule ndaye marche générale lagniou wara def Sénégal pour li diékh fi
Allez -y jusqu'au bout nabou meye waroul am liberté.
Yeureum na yayou feu Aziz ak waly
Vraiment justice pour Aziz et waly, lii dou yone way😢😭
Justice soit faite li da fa méti trop sakh surtout yayou aziz
Police na def ligueyame justice pour Azize dabala et wally
Rey mo war diekh Sénégal rey toujours comme ay guinar 😢😢😢
Lii c est tres louche,cette affaire doit être éclaircie au plus vite! Il reste dans la justice des pourris!
Justice,rk
Justice pour Aziz et wally ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Adouna dale yeuremandé amenasi solo até yalla mon geune bou nite ñi guéne adouna yalla naléne yalla yeureume tes ñiou dadiék deugou yalla bi
Vraiment lii defa ñaaw
Yene vous abusez a la fin. On a tué aziz nako yalla yeureum. Police moo diap gnimou diap si enquete, justice mo mandat de depot, justice mo bayi nit ki nguene ni nonon cta dire. Il ya dautres personnes youniou diap non!? Wolounguene justice mais c’est vous qui remettez en cause . Dama fokni buzz nguene beugu a la fin. Portez plainte contre nabou leye alors prsk yene portez woulene ko plainte gniko diapone nioko bayi
Vous avez parfaitement raison
Mais nabou leye aussi meuna si bania bokou d mai gayi nio wara wakh loutakh niou bayi ko
Mais n'a lerr rekk
Antoucas nabou leye môme domouhram la boumakk sakh yaw sa xarite dé si jour décés bi ngay wakh nane kou dé déna nieupay dé ak dé nimou métiwé ngani yaw aziz sa xarite la ak niniouko rayé nimou niawé ngay wakh lolou kou tothie sarap ndeyam la
Ma d'accord thi ioe yombouna torop
Antoucas yombou na trop mom
Mane fimné dama gueleum 🙆khawma sakh
Ou est Sonko, Svp faite appel à Sonko pour que Justice soit faite au secours Président Sonko 😢😢😢 Justice pour Aziz Daballa 😂😂😂
Police mo indi probleme bi yep
Police serieux léne ngene def séne ligueye wala communiquet avec sa famille ñiu kham. Vraiment lii métineu
Justice pour Aziz et Wally😢
Mais cest pas possible il et est où la justice .depuis 2mois pas la police pas le juge pas le procureur j'espère k nabou dou ndaw j'espère k jugement sera faite
mbillaye mère bi yeureum nako justice nagnou déf séne liguaye li mbaxoule
Kou Yon guéné defoul dara nabou degnouko sérises wonne rék ndakhe wakhe jou bari bi mais nabou defoul dara
Yayou Azize mounoumako khole bilay 😭😭😭😭😭
Mane bilahi Sénégal bakhna rek li marina trop bilahi
Nabou ne doit pas etres libre comme sa la police au moins devrait faire un conférence de presse concernant l enquête pour éclairer les sénégalais
Nabou moye Domeram. Bou bonne dou gorr na Wa Senegal gnouss saine wa keur
Justice pour Aziz et Waly
Kou dè ya perte
Lima beugue police wakh moye loutakh mou diapone Nabou Leye toke bamou nekhko mou bayiko moma diakhal 😢😢😢
Justiise soit fait
Dou deugeu dou yonn nabou léye waroule guéneu
Franchement la justice Sénégalaise je suis désolée. Aucune communication pas de conférence de presse par rapport à ce dossier qui a choqué et touché tous le monde au delà des frontières.
Wa mane famille aziz niondone défendre nabou lolou moma diahal ,en plus tey bakhna justice wahagoul nabou mo rey ,yalna yalla leral deug😢
Mo leneu dioural li yeupeu
Tout le monde accusait nabou leye eux ils defendaient nabou legui dogno diahasso
Li nasi niep wah ndakh sonko ak diomay diotsi wahak juge yi rewmi coumba am Ndeye ak coumba amoul Ndeye dafer wara diok q justice soit faite nabou niata mandat dépôt la fek Maf ta ken laloul sen d’osier ta am nanou ay avocat donc nabou niow même pa 3mois juge lidianti dosier bamouy am liberté jub Jubal jubanti lanou wah pro yeugueul Li wah ak justice
Jusqu a preuve du contraire ce dossier va être claire en tout cas
Metina trop 😢😢
Babou bou rayonne azize heur bi d'où guene
Faites une marche blanche et le procureur dans tous ça 😢
Mes niom sene avocat bi aussi est-ce que kharagne na tmt nagn diema changer benene avocat bakham yala bakhna😢😊❤
Vraiment la maman elle a trop mal ndeysan Yalla nako Yalla diegeul te yereum ko yatal bamelam leral ko te leral mbir yi bala mo yag 🤲🏾
En passant la maman aussi elle communique bien 👍🏿
Sa xol biii metina, Aziz demna niii rek 😭
Nabou leye thi lobby bou mak la bokou motakh gnou bayiko bougne gnou takha wakh nak justice na déf liguéyam nak
Lolou moy wakh ji. Ki amna bras long. Sénégalais ci boppam Mo am vice thiaga. Thiaga rek la niou beugue. NABOU leye kou ko Guiss khamni bandit la thiaga la
Boudé Nii leu Nara demé kon Naniou libére Niousi déss Li amoul chance libére ki bayyi Niousi déss 😡😡
Waaw ki takhaw ni man maaray nabou Yoon wakhoul ni nabou mooray moytou leen sournalistyi
Tate tam yoyou motakh niou bayiko senegal amoul loi bilakhi legui guén degu mogi europ ay domeram lanou fi kou dé ya perte walakhi
Leye leye do reuthi de bilahi
Seuththt.bayilen di yakkar koudoul yalla.yomalhiyam koufa nee meun gafa dra koudoul yalla dagay kath
NABOU LÉYE N EST PAS ENCORE JUGÉE, C EST UNE LIBERTÉ PROVISOIRE. CELA NE VEUT PAS DIRE QU ELLE N EST PAS COUPABLE, SEUL LE PROCÉS FERA LA LUMIÈRE SUR CETTE AFFAIRE.
Il y’a pleins de détenus dans les prisons qui ne sont toujours pas jugés et pourtant ils sont enfermés pourquoi ce cas est spécial ????
Nabou ne doit pas sortir
Sénégal dal nii rék coné chence ba kagne ja veu dire Sénégal kou dée ya perte 😢
Le procureur doit expliquer ce qui se passe
Senegal daye geuna metti nakh alal ak tour naniou djital naniou diang ay kamil nianal rewmi
Ay way Sénégal dal lounekh way def
March lénn bountou palais s'il vous plait
Non Nabou leye d’où nite waya dîna khamné yalla meuneu gneup
Manoul mo gueun ba ham le vrai verite
C'est le processus normal d'une enquête judiciaire. Meune naniou placé niit sous mandat de dépôt bala procès ba du diote enquête bi wané ay insuffisances de charges. Dans ce cas avocat kouniouy top meune neu lay liberté provisoire.
Merci😢😢😢😢😢😢😢
Nabou leye waroul guen nabou complice la
Assises de la justice on n'en fait quoi on a parler de rupture mais c'est le contraire
Que ça fasse du grand bruit lii dafa wara leer walla Sénégal taak
Avec bassirou diomaye faye ak Ousmane sonko domekharam dji tout
Ssnegal amoul luwa lee amna lu see rahh
Vraima bizarre coma il peu y avoir liberté provisoir sans jugema😢
Nabou est ce que danguene ko guiss si lieux de crimes bi wala genre pour nguen Di toumal domou ndiambour bi danguene gana XAM procureur son job déjà gni gnou diap gno ray waxolene si gnognou mai nabou nguene tek beute prétendant k complice la nekk lene niit douguene yalla douguene juge
Liberté provisoire sans jugement lagniy bagne😢
En tout c'est vraiment bizarre
Yalnako yalla leral😭😭
Sénégal dou rew
Tiayy sénégal kou déé ya perte bilaye boulénn bayyi mou séed daffa yombb trop
Mann ma bayi senegal depuis niarri khalé yoyou niou fekk si auto soit disant serigne bi keur mbaye fall bénnn khalé bi déee khénnn diappoul borom auto au contraire famille victime bi laniou attaquer
Docié bi da mastique l'OL